Setal.net

Pour rire: Bêtisier - Les lutteurs s'initient au français...Lisez


Pour rire: Bêtisier - Les lutteurs s'initient au français...Lisez
Betisier Lamb Ji lors du face-à-face au King Fahd Palace Hotel :

Boub's : baan message ngay lancer pour lutte contre la violence.
Cartouche : Boub's nioune dou niou VIOLER.

Thiandoum a Forza : Jordan da feu teur 6 goorous Yalla.
Forza : Niou mou daan akh maan ca fait diametralement oppose.

Boy Naar : Avant Lamb daniou ko doon def ni rek mais legui lamb da fa am SPECTACULAIRE. Juan sou ma ko dieule dam ko beuggeu won EXEMPLAIRE.

Lac Rose : Di niaan Yalla niouy def VIOLATION yi niou bayiko.

Malal Jr a BG2 : Lo khalat si controle dopage bou CNG beugg def.
BG2 : Nioune Mbeur yi da niouy entrainer amoul DOPATION.

BG2 a T. Tine : Si VIP yi ya si geuneu NIL (NUL).
T.Tine : Kou NIIN nou mou beure. (Pour mom ya geuneu NIIN la niou ko wakh du genre Takk Ci Rip)

Bi nak moy dadj deup gui. Niokho Baye dans la pub du lancement de son émission sur SEN TV : Sa you combat bi diekhe niou DECORTISER len ko (DÉCORTIQUER)

Source: Facebook

Ibou Toure

Mercredi 5 Décembre 2012 - 17:02










Google+

Partager ce site